Sunuy liggéey

Benn équipe ngir yoonu sa kayit bépp: jëlal, tekki, certifier, légaliser te yónnee.

Naka la laaj bi di doxe

  1. Yónnee say kayit

    Scan walla nataal, ci formulaire bi walla ci email, ak réew mi ak organisme bi mu jëm.

  2. Jot sa devis

    Njëg, jamono ak li war a def: certification, apostille walla légalisation. Amul fay.

  3. Nun noo koy def

    Tekki, notaire, Ministère, ambassade: nu ngi topp lépp te di la xibaar.

  4. Jot sa kayit

    Ci email, ci sa loxo walla ci courrier, ci Senegaal ak bitim-réew.

Am nga kayit bu ñu war a tekki, apostille walla légaliser?

Njëg gi dafay aju ci kayit bi, làkk bi, réew mi ñuy yónnee ak jamono ji. Wax nu li nga soxla: dinanu la yónnee devis bu amul fay.