Séy ak doxandéem ci meeri, tribunal, waxtaan ci liggéey walla conférence bu mag: nu ngi lay jox tekkikat yu xam mbir mi. Nu ngi tekki faranse, àngale, araab, español, portugees, sinwaa ak làkki réew mi: wolof, pulaar, seereer, joola, mandinka ak soninke.
Anam yi
- Ndaje ak waxtaan (consécutive)
- Conférence (simultanée)
- Àndandoo ak nit ki (liaison)
- Telefon walla visio
- Séy ci meeri
- Tribunal ak notaire
Yoon wi
Yónnee say kayit
Scan walla nataal, ci formulaire bi walla ci email, ak réew mi ak organisme bi mu jëm.
Jot sa devis
Njëg, jamono ak li war a def: certification, apostille walla légalisation. Amul fay.
Nun noo koy def
Tekki, notaire, Ministère, ambassade: nu ngi topp lépp te di la xibaar.
Jot sa kayit
Ci email, ci sa loxo walla ci courrier, ci Senegaal ak bitim-réew.
Laaj yi ñuy faral di laaj
Ndax ngeen di liggéey bitim Ndakaaru?
Waaw, ci diiwaan yépp. Njëgu tukki bi, bu amee, dinanu ko bind ci devis bi.
Ci làkk yii ak yeneen
Am na ci Senegaal gépp
- Dakar
- Pikine
- Guédiawaye
- Rufisque
- Thiès
- Mbour
- Saly
- Tivaouane
- Diourbel
- Touba
- Mbacké
- Saint-Louis
- Richard-Toll
- Podor
- Louga
- Kaolack
- Fatick
- Kaffrine
- Ziguinchor
- Kolda
- Sédhiou
- Tambacounda
- Kédougou
- Matam
- Ourossogui