Nu ngi tekki say kayit ci olande te jox tekkikat olande ngir ndaje, tribunal ak liggéey ci biir réew mi ak bitim-réew.
Làkk yi ñuy faral di boole
- Olande ↔ Faranse
- Olande ↔ Àngale
- Olande ↔ Wolof
Li nuy def ci olande
Tekki bu wóor
Tekki kayit yu yoon yu ambassade, iniwérsite ak tribunal yi di nangu (traduction certifiée).
Apostille
Apostille ci kayitu Senegaal ak yu bitim-réew, ngir réew yi bokk ci Convention de La Haye.
Légalisation ambassade ak consulat
Légalisation ci Ministère, ambassade ak consulat ngir réew yi bokkul ci apostille.
Copie certifiée conforme
Copie yu ñu seede ne dëppoo nañu ak original bi.
Procuration
Waajal procuration, xaatim ci kanam notaire, tekki ak légalisation.
Jëlal kayit
Kayitu juddu, casier judiciaire, diplôme ak RCCM, nun noo lay jëlal.
Tekki ci wax (interprétariat)
Tekkikat ngir ndaje, tribunal, séy, conférence ak woote ci internet.